Xet wu njekk

Joge Wikipedia.

Nataalu Wikipedia Dalal-jamm ci Wikipedia

Welcome to the Wolof Wikipedia ? Bienvenue sur Wikipedia en Wolof

Jimbulang bu Ubbeeku bi

Seetal ci 1 695 jukki ci kallaama wolof:

 

Nas wi bokk na ci bere biy daq ber bi nu ber yenn lakk yi (rawatina ci internet bi), xecc itam gendaloo guy yamale te di japplante, loolu di sukkandiku ci san-sanu askan yi gaddu seen kuute ci caada.

Adduna bu gen di yamale, ak gen di tinkiku ci la aju !!!




Askan
Nataalu ayubes bi

Ndakaaru (Dakar) Nekkoon peyu Afrig gu sowwu gu fraase (ASF, walla AOF ci FR), Ndakaaru fimne mooy Peyu reewum Barug Senegaal akit goxub Ndakaaru, tolluwaayam ci peeteg sowwu bu Afrig, ci jegeem Daanaka-dun bu Kap-Wert, waral na sancug notaakon yu jekk yi, Akit yaxantu ak Adduna bu bees bi, te ame na peetewaayu ngeneel ci jeflanteg cosaani Saa-Afrig yi ak Saa-Tugal yi. Fa lees Taxawalee woon Xumbalu Addina bu fanni nuule (jaam yu nuul) bu njekk bi ci xalaatu Leopool Sedaar Sengoor atum 1966, Dekk bii mooy toogu bu Keru-gestu bu dattu bu Afirg gu nuule (KDAN, walla IFAN ci FR) akit bu Bank bu diggu bu guuri Afrig gu sowwu (BDGAS walla BCEAO ci FR)

Yeneen sembi Wikipedia ci yeneeni kallaama. Nu lim ci nenn ni rekk

Yeneen sembi Wikipedia ciy kallaamay waa Afrig


Commons
Dattub njoxeeb ay nataal
Wikbaatukaay
Baatukaay barilakk
Wikiquote
Dajaleeb ay tudd
Wikixibaar
Xibaari adduna bi
Wikiteere
Teerey njang yu ubbeeku
Wikisource
Kaggu bu ubbeeku
Wikispecies
Wayndareeb xeeti mindeef yepp
Wikidaara
Jumtukaay ak yengu-yengu neel njang
Meta-Wiki
Nosuwaayu sembi Wikimedia yi