Way

Joge Wikipedia.

Mbuug ak Way Mbuug nag mooy Misig (fr musique en music) mbuug nag nu bari xamunu baat bi ci wolof ba tax na misig rekk lanu koy wax ndax daa bokk ci baat yi nga xam ne nepp a ko bokk niki lu mel ni widewo(video). WAY, baatu way mi ngi juge ci nit ku way maanaam nit ku yeww li tax nu tudde nit kookii waykat dafa way ba man a sos ay wax mbaa ay nose yoo xam ne nit ni mu nekkal bayyiwunu ci xel mbaa sax xamunu ko woon, kon moo leen gen a way ba tax muy way kon ku nuy tudde waykat dafa war a doon kuy yeete

Way batay man na tekki poesie ci wolof [ Soppi ? soppi gongikuwaay bi ]

Ay Mbuugkat ci Senegaal

Ay nosekat/Taalifkat ci Senegaal