Wikipedia : Xet wu njekk

Joge Wikipedia.
Dalal-jamm ci bunt bi nu jagleel askanu Wikipedia .

Soo amee yeene bokk ci jemale-kanam jimbulang bi, ngala jangal bu baax ana lan mooy ay atteem, ci ponk yi mu lalu.
Man ngaa tambalee ci xetu ndimbal wi. Di na tax nga xam lu bari ci Wikipedia.
Ci xet wii man nga fee gisee fooy defee ay laaj, fooy waxtaanee, ak lepp lu aju ci Wikipedia

Yegley Askan wi
soppi
  • Su fekkee am na nit ku ngeen begg mu nekk yorkat mbaa ngeen begg koo doon yeen ci seen bopp, su boobaa bind leen seen tur Fii .
  • Ngir dem ci penc mi cuqal fii
  • Ngir dem ci xetu kalante wi
Ay xibaar ngir gan ni
soppi

Soo leen demee ci xetu gan ni di ngeen fa fekk ay xibaar yu leen di dimbali ngir ngeen man a tambalee ceru ci Wikipedia.
Man ngeen tamit def ay laaj (question).

Luy Xew
soppi
Ci yeeneen naali wiki
Wolof Wikibaatukaay sosu na, soo leen amee ay baat yoo leen begg a seet walla yoo leen begg a duggal, dem leen foofu.