한국   대만   중국   일본 
Weer ? Wikipedia Aller au contenu

Weer

Joge Wikipedia.

Weer ab diirub jamono la, seddaliku ci ay ayubes , moom, ayubes, seddaliku ci ay bes. Ci arminaatu weer, nu di ko wax itam weeri wolof , at mi fukk ak naari weer la, te weer yi am limu bes yu wuute.

Yeneen xeeti arminaat yu dul bu weer man nanoo nekk, ci misaal, arminaatu jant

Aminaatu weer [ Soppi ? soppi gongikuwaay bi ]

Dees na ko wax it weeru wolof

Arminaatu jant [ Soppi ? soppi gongikuwaay bi ]