한국   대만   중국   일본 
Saara ? Wikipedia Aller au contenu

Saara

Joge Wikipedia.


Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Saara  : yay Afrig Saara ab mandiŋ la, mu ngi soxal Afrig gu bej-gannaar. Ak 9.200.000 km2, mooy mandiŋ bi gen a mag ci addina si, te mooy netteelu mandiŋ bi gen a mag ci addina si, gen a tuuti mandiŋ yi nekk ci Antartika ak bej-gannaaru Artiku rekk.

Logo Commons

Xool it Wikimedia Commons