Nguur-Yu-Bennoo

Joge Wikipedia.
The United Kingdom of Great Britain and Northern Ireland
Nguur-Yu-Bennoo
Raaya bu Nguur-Yu-Bennoo Kóót bu aarms bu Nguur-Yu-Bennoo
Barabu Nguur-Yu-Bennoo ci Rooj
Barabu Nguur-Yu-Bennoo ci Rooj
Dayo 244 101 km 2
Gox
Way-dekk 60 943 912 nit ( 2008 )
Fattaay 244 nit/km 2
Xeetu nguur
- Njiitu Reew
- Njiitu Jewrin
Tembte
- Bawoo
- Taariix
Pey ak reddi
Tus-wu-gaar
Tus-wu-taxaw
Londar
51° 30′ Bej-gannaar
      0° 7′ Sowwu
/ 51.5 , -0.117
Lakku nguur-gi Wu-angalteer
Koppar
Turu aji-dekk
Telefon
   

Nguur-Yu-Bennoo walla Nguur Yu Bennoo yu Bretaan gu Mag ak Irlaand gu Bej-gannaar ( United Kingdom of Great Britain and Northern Ireland ), nenn ni di ko wax angalteer, am reewu bej-gannaaru Tugal la.

Nguur gaa ngi judd ci 1800 ci booloog Nguurug Bretaan gu Mag ak Nguurug Irlaand. Ci 1922 la wall gu yaa ci Irlaand dagg, tudde boppam Reewum Irlaand . Nguur gi dafa seddalikoo ci neent: Angalteer , Irlaand gu bej-gannaar , Wales ak Ekos