한국   대만   중국   일본 
Alxuraan ? Wikipedia Aller au contenu

Alxuraan

Joge Wikipedia.
Alxuraan

Teeree ngii di benn ci yi nu gen a yer ci adduna bi, mooy teere bees sellal ci lislaam , di fi jullit niy ball-loo seen yoon di Shariiha, ak ci sunna siy dundiinu Yonnent bi (jamm yal na nekk ci moom), kon nag bu am solo la lool fi jullit ni.

Alxuraan : Alxuraan mooy teere bu sell bi neel jullit ni, mooy balluwaay bu njekk bi neel yoonal gu Lislaam gi, ci ginnaawam la Sunna di newe. Li njekk a wacc ci Alxuraan it mooy laaya wi njekk ci saaru Halaq muy : ≪Jangal ci sa turu boroom bi bind (sakk) ≫

Alxuraan nag mooy waxi Yalla ji mu wacce ci Yonentaam ba Muhammad , Jibriil nag mooy ndawul Yalla tey malaaka mi ko wacce; ngir nag Yonent bi jottali ko nit nepp,. Moom nag fa Yalla dees koo bind ca alluwa jees wattu ja (Lawhul Mahfuus), alluwa jii nga xam ne Yalla bind na ca lu nekk njekk mu koy sakk. Wattu googu nag Yalla la soob, mu begge ko noonu, noonu la ko waxe: ≪Nun noo wacce Alxuraan, te nun noo koy wattu≫

Kaamil bi [ Soppi ? soppi gongikuwaay bi ]

PDF Alxuraan Ci Wolof [ Soppi ? soppi gongikuwaay bi ]

[1] PDF

Lekkalekaay yu biti [ Soppi ? soppi gongikuwaay bi ]