한국   대만   중국   일본 
Akilas ? Wikipedia Aller au contenu

Akilas

Joge Wikipedia.

Ci angale mooy Aquila ; Ci faranse mooy Aquilas

Benn Yawut ak toppkatu Yeesu la woon, ma nga juddu woon Pont ci Asi Miner. Jabaram, Pirsil la tuddoon. Defarkatu tant la woon ni Pool . Nawle ak Pool la, ci liggeeyu Boroom bi, te dafa amoon mbooloom ni gem ma doon daje ci seen ker ci Room .

Danuy jang ci Akilas ci Jef 18:2-3,18-19,26; Ro 16:3-5; 1Ko 16:19; 2Tim 4:19.